Les surprenantes confidences d’un homme.
« Bonjour a vous tuto Ano svp
J’ai envie de dénoncer une femme qui trompe son mari avec moi même.son mari est un ami pour moi,un grand frère, il m’envoie souvent de faire ses courses, ak jabar dji aussi makoy defal course yi mais c’est un voyageur et lorsqu’il voyage sa femme dafmay invité souvent ci gallé bi dima deflo Lou xamm ni nexouma dima lambatou dima deff Lou nekk ba damay moudié daw. Djiguene bou bone la. Plusieurs fois souma yoni wé ma demm au retour damay fekk mou mou soumé kou ba settt tekk xaliss bou beuri ci kaw table bi ak ay feram Mais douma wah dra damakoy dioh limou ma yoni rek daw. Ba demb Mossi moudié sama affair bi la teyé nane ma xana douma Goor soumakoy dawé. Tuto dimbalima ma decide mbala may deff Lou eupp«