« Bonjour tutodakar silo nekk defal ano. Je suis une fille de 24ans en couple avec un homme de 56ans pas bou capricieux sah tek ci Beug dioy. On c’est connus y’a 11mois niou nekk di geneu ensemble. Mou dieuleul ma appartement meuble ko et tout. Ma deuk fi mane kessé Mais tutodakar pa bi sayou niowé ci keur gui yefou niak fouleu rek deff day Beug makoy nampal ak biberon 🍼 souko defé mouy dioy komm lirr bou soga dioudou. Beneu jour da guiss sama téléphone may wah avec un autre homme par WhatsApp rek mou commence dioy ci appartement nane day xarou bama tit. Mom genre yoyou lay deff loumay geuna dérange ci mom une fois mou niow fi slip rek lay solll bamou Gnibi t yram bi da niaw trop. Je veux le quitter ms Souma xalaté loumou may defal lepp j’ai peur de recommencer à zéro ».
Previous ArticleFocus sur Cheikh Senghor : Le visionnaire des réseaux sociaux
Related Posts
Add A Comment